1
00:04:12,000 --> 00:04:13,431
Kan moo fa nekk ?

2
00:08:04,213 --> 00:08:06,409
- Loolu neexoon na lool.
- Nañu yaakaar mu mel nii guddi gu nekk.

3
00:08:06,409 --> 00:08:08,366
Waaw, waaye amul xeer ci valise yi.

4
00:08:08,366 --> 00:08:10,273
- Dina nu gise ci sama saal bi ñuy soloo.
- Baax na.

5
00:08:10,522 --> 00:08:11,839
- Soxna Fontaine.
-Waaw?

6
00:08:11,839 --> 00:08:13,111
- Ab telegram.
- Jërëjëf.

7
00:08:24,297 --> 00:08:27,045
Joane Fontaine dafay wéy
réer.</i>

8
00:08:27,332 --> 00:08:30,442
Sersant Martin, bànxaas
ci nit ñi réer.</i>

9
00:09:00,430 --> 00:09:03,425
Yaakaar nga ni di nga ci gis
yaw kese ngay génn?

10
00:09:03,425 --> 00:09:05,616
Dama ragal réer
ci koñ bi njëkk.

11
00:09:05,820 --> 00:09:06,569
Toogal.

12
00:09:07,218 --> 00:09:09,250
Laaj naa la loolu
ngir féexal sa yaram,

13
00:09:09,533 --> 00:09:12,282
Waaye sudee gëm ngeen ni
kouloir yi dañu jafe,

14
00:09:12,608 --> 00:09:14,723
xaar nga tukki
mbedd yi ci Venice.

15
00:09:14,723 --> 00:09:16,915
Dama wara wut sama mag ju jigéen,
Sersan Martin.

16
00:09:17,599 --> 00:09:20,273
Man ak sama mag ju jigéen
orphelin lu yàgg

17
00:09:20,273 --> 00:09:22,306
te man rek maa ci famiy bi
mu am.

18
00:09:22,909 --> 00:09:24,865
Bi ñuy njëkka gise
Dama am yëg-yëg

19
00:09:24,865 --> 00:09:27,141
ni bokku ci
nit ñu baax

20
00:09:27,141 --> 00:09:28,458
Ñu ngi xaar ba gis li xew.

21
00:09:28,458 --> 00:09:29,809
Wax nga dëgg.

22
00:09:31,294 --> 00:09:33,325
Dinaa la xelal,
Soxna Fontaine.

23
00:09:33,969 --> 00:09:36,524
Suko defee li gëna baax
loo mëna def

24
00:09:36,524 --> 00:09:38,556
Mooy toog di xaar.

25
00:09:38,920 --> 00:09:40,066
Melokaan...

26
00:09:41,555 --> 00:09:43,989
Rafetam bu jigéen bi jël na dogal dem dëkk
ci wetu tefes gi

27
00:09:43,989 --> 00:09:45,137
ak ay hippie.

28
00:09:45,347 --> 00:09:46,866
Daa melni dëkk ci wetu kër gi
ci tefes gi

29
00:09:46,866 --> 00:09:49,055
génne li gëna baax ak li gëna bon
ci nun.

30
00:09:49,500 --> 00:09:52,416
Amna park luxus
guys yi dañu koy faral di dem

31
00:09:52,416 --> 00:09:54,402
ñu dedike
ci jaam bu weex.

32
00:09:54,890 --> 00:09:56,525
Waaw, ba leegi ñu ngi fi

33
00:09:56,807 --> 00:09:59,202
te dinga jaaxle
limu xale yu jigeen yi

34
00:09:59,202 --> 00:10:01,119
luñu doon wax
ñi ci bokk

35
00:10:01,119 --> 00:10:02,629
ci xeetu jafe-jafe yooyu.

36
00:10:03,274 --> 00:10:05,660
Amna ay fetal, ay faat,

37
00:10:06,709 --> 00:10:10,251
kidnapping, dóor...

38
00:10:12,059 --> 00:10:13,895
Amaana leegi yaa ngi ci laaj

39
00:10:13,895 --> 00:10:16,246
Lu tax mbir yooyu di am
lu tiis la

40
00:10:16,771 --> 00:10:21,153
def naa ci lii 21 at
liggéey di seet tontu li...

41
00:10:21,402 --> 00:10:22,593
mujjee naa ko am.

42
00:10:22,838 --> 00:10:24,111
Lan mooy tontu li ?

43
00:10:25,394 --> 00:10:27,619
Nit ñooñu dañu bëgg loolu xew
mbir yooyu.

44
00:10:28,029 --> 00:10:29,618
Ndax dafa yomb ci yaw?

45
00:10:29,866 --> 00:10:33,374
Du noonu la.
Mooy mbir mi gëna tar ci àdduna bi.

46
00:10:34,218 --> 00:10:37,806
Kenn xamul dara ci subconscient,
Soxna Fontaine.

47
00:10:38,250 --> 00:10:39,681
Ba ci nun.

48
00:10:40,966 --> 00:10:43,759
Waaw, dafa lëndëm,
àdduna bu lëndëm

49
00:10:49,750 --> 00:10:52,338
Empire bu mbindéef yi
Durea,

50
00:10:52,504 --> 00:10:55,333
exposé biy dundu
bi gëna mag ci àdduna bi.

51
00:10:55,459 --> 00:10:57,253
Nit ku nekk 50 cent kese.

52
00:10:57,534 --> 00:11:00,363
50 cents ngir jigeen ñi,
50 cents ngir góor ñi.

53
00:11:00,490 --> 00:11:03,840
Empire bu mbindéef yi
Dr. Durea, mbindéef yuy dundu.

54
00:11:03,963 --> 00:11:05,792
Xoolal ni ñu ko daggee
bopp bi.

55
00:11:05,920 --> 00:11:08,952
Xoolal ni seen deret di daw
ci seeni bët.

56
00:11:09,074 --> 00:11:10,505
Soo gisee mbindéef yooyu,

57
00:11:10,791 --> 00:11:14,299
Dina ñu jaaxle ci ni
Dina ñu ragal seen bakkan.

58
00:11:16,939 --> 00:11:17,973
Fan nga bëgga dem?

59
00:11:18,856 --> 00:11:20,571
Fii.
Ñëwleen gis.

60
00:11:21,451 --> 00:11:24,246
Hey, war nañu fay
yaw buntu bi.

61
00:11:24,246 --> 00:11:26,321
Waaw kay, jox ma ñaari këyit.

62
00:11:26,321 --> 00:11:27,435
Jox ma ñaari këyit.

63
00:11:27,799 --> 00:11:31,501
Jox ma ñaari këyit!
Jox ma ñaari këyit!

64
00:11:34,148 --> 00:11:35,102
Benn dolaar.

65
00:11:44,609 --> 00:11:46,084
Xoolal li may def ak moom.

66
00:11:48,961 --> 00:11:50,152
Damay ko lekk.

67
00:11:57,585 --> 00:11:58,618
Duggal.

68
00:12:12,038 --> 00:12:13,264
Ci kanam.

69
00:12:14,553 --> 00:12:15,990
Bul ragal dara.

70
00:12:15,990 --> 00:12:19,862
Mooy Empire u Mbindéef yi
ci Dr. Durea.

71
00:12:19,944 --> 00:12:23,294
Di nga gis mbir yoo xamni doo ko gëm.

72
00:12:23,777 --> 00:12:28,001
Waaye maa ngi lay wax ni lépp
Li fi nekk dëgg la.

73
00:12:28,408 --> 00:12:31,997
Te barina lumu xew
yoon ci taarix.

74
00:12:32,481 --> 00:12:34,149
Waaye, bu ngeen gisul dara.

75
00:12:35,555 --> 00:12:39,143
Dañu wara ubbi seen bët
ngir baña ñàkk dara.

76
00:12:43,740 --> 00:12:45,533
Barina lu nit ñi mëna gis.

77
00:13:00,389 --> 00:13:02,456
Du ay njuumte rek
ngir xale

78
00:13:12,687 --> 00:13:14,163
Lépp a ngi jaar yoon.

79
00:13:16,479 --> 00:13:18,069
Dëgg la, yaa ngi ragal.

80
00:13:18,316 --> 00:13:20,621
Ndax xamu ñu ko
ngir yaw.

81
00:13:21,430 --> 00:13:24,383
Kumpa yi gëna mag ci àdduna,
Duñu ay kumpa,

82
00:13:24,545 --> 00:13:28,087
sudee jël nanu waxtu wi war
ngir miinante ak ñoom.

83
00:13:28,417 --> 00:13:30,167
Xale bu baax nga.

84
00:13:31,452 --> 00:13:33,201
Waaye, defal ko mask,

85
00:13:33,808 --> 00:13:37,033
te ku nekk dina nekk
ci moom.

86
00:13:41,434 --> 00:13:44,864
ubbi naa attraction bii
ndax sabab yu bari.

87
00:13:45,187 --> 00:13:47,981
Yaakaar naa ni nun ñépp war nanu
dundu dundu

88
00:13:47,981 --> 00:13:50,048
ak ekspontanite bu mat sëkk.

89
00:13:50,537 --> 00:13:53,250
Te loolu rekk lay mëna am
sudee amul ay tere.

90
00:13:53,811 --> 00:13:54,958
Ndax nangu nga ko?

91
00:13:56,127 --> 00:13:59,272
Waa Rome amoon nañu seen
cirque maximus,

92
00:13:59,680 --> 00:14:02,348
ak lu ëpp 200 000 toogukaay.

93
00:14:02,435 --> 00:14:05,350
Waaye ay mbummbaayam
Duñu woon ay gan

94
00:14:05,350 --> 00:14:07,905
ki may dem
ngir wane leen.

95
00:14:08,543 --> 00:14:10,496
Leegi xoolal.

96
00:14:13,854 --> 00:14:14,967
Sa ginaaw.

97
00:14:17,367 --> 00:14:18,845
Waaw, dafa nuru lu am solo.

98
00:14:18,845 --> 00:14:22,467
Sudee njuumte yi nuru ñu dëgg,
Duñu doon ay njuumte, wala book?

99
00:14:33,778 --> 00:14:36,014
Waaw, barab bii dina raglu
ba ci ñi gëna pentire.

100
00:14:36,014 --> 00:14:38,603
Yaakaar, danga ragal
ngir lu nekk.

101
00:14:38,848 --> 00:14:39,802
Waaw.

102
00:14:40,046 --> 00:14:42,510
Nanu waajal fippu bi
ngir tay ci guddi.

103
00:14:42,721 --> 00:14:44,629
Lan lanu doon fippu?
bii yoon?

104
00:14:45,117 --> 00:14:47,149
Xamuma, waaye danga wara
féexal sa xol tuuti.

105
00:15:01,407 --> 00:15:02,394
Grotun, baaxna.

106
00:15:02,765 --> 00:15:04,960
Gis naa loolu ci jamono jii
waajal nga ko bu baax

107
00:15:04,960 --> 00:15:06,276
taabal li ñuy jëfandikoo.

108
00:15:07,515 --> 00:15:09,231
Ak tàngoor wi?

109
00:15:09,992 --> 00:15:13,103
Ndax xool nga
Sudee lu baax la?

110
00:15:27,159 --> 00:15:28,953
Grotun, dégg nga ko.

111
00:15:29,995 --> 00:15:31,788
Bëgg nañu gis lu dul dëgg.

112
00:15:32,510 --> 00:15:34,267
Waaye ba leegi xamu ñu ko
loolu dëggantaan,

113
00:15:34,267 --> 00:15:37,253
Mooy njuumte bi gëna mag.

114
00:15:37,940 --> 00:15:40,653
Deretu doomu aadama mooy xët wi
ci...

115
00:15:42,172 --> 00:15:43,285
gis-gis ëlëg.

116
00:16:04,452 --> 00:16:08,232
Waaye kumpa gi du
jant bi ci deret ji.

117
00:16:09,202 --> 00:16:11,118
Amul sistem sirkulaasioŋ

118
00:16:11,118 --> 00:16:13,833
mën na muñ dagg
tiis.

119
00:16:14,991 --> 00:16:17,660
loolu mënul nekk
xel mu doomu aadama.

120
00:16:18,745 --> 00:16:21,049
Baatu trauma du lu bees.

121
00:16:21,619 --> 00:16:26,526
Waaye man
Yaakaar naa ni man maa njëkk

122
00:16:27,010 --> 00:16:30,712
ci dundu tiitaange
de dagg bopp.

123
00:16:31,282 --> 00:16:35,392
Ak dekkib yaram
ki ko sonal.

124
00:16:38,070 --> 00:16:40,260
Dama yéeme dëgg.

125
00:16:41,503 --> 00:16:43,331
Yenn scars...

126
00:16:43,819 --> 00:16:48,520
Liggéeyukaay yiy jeex
Jamono di dox, amul leneen.

127
00:16:49,927 --> 00:16:53,402
Dafa waroon sedate ngir
dina noppalu ci jàmm.

128
00:16:53,402 --> 00:16:56,236
Ndax tay ci guddi mën na
joge ci nun

129
00:16:56,236 --> 00:16:58,268
mel ni dara amul
xew.

130
00:16:58,751 --> 00:17:01,260
Te mën nanu ko nangu
na loolu am.

131
00:17:01,426 --> 00:17:04,935
Du ba serum bi
am nañu ci jaar-jaar.

132
00:17:05,419 --> 00:17:07,645
You are a lucky woman, Grotun.

133
00:17:08,334 --> 00:17:11,445
Danu soxla
ak deretam.

134
00:17:12,766 --> 00:17:15,161
He has survived decapitation

135
00:17:15,161 --> 00:17:18,352
and we have got the fluid
lu am solo ci nun.

136
00:17:20,311 --> 00:17:22,264
Waaye dunu
yàppkat yi, Grotun.

137
00:17:23,068 --> 00:17:25,303
We don't have this young woman
lu yomb

138
00:17:25,303 --> 00:17:27,812
ngir yàq sa yaram
ba noppi nga sànni ko.

139
00:17:28,776 --> 00:17:29,490
Déedéet!

140
00:17:30,094 --> 00:17:31,843
Nun gëstukat lanu.

141
00:17:33,207 --> 00:17:37,716
And we must continue experimenting.
Xam nga loolu, wala book?

142
00:17:38,398 --> 00:17:42,067
You must also understand that
Dama wara pikiir la.

143
00:17:43,708 --> 00:17:47,093
Leegi Grotun mën na wax
wéyal sunu liggéey.

144
00:19:35,463 --> 00:19:38,768
Amnaa samay jumtukaay, Grotun.
Am nga sa bos.

145
00:19:48,679 --> 00:19:50,950
Bul sori ci gaal gi.

146
00:19:52,033 --> 00:19:53,861
Dina nu la xaar.

147
00:19:55,147 --> 00:19:58,690
Demal ndànk te moytu.

148
00:20:16,069 --> 00:20:18,057
Doktër Durea, jàpp naa.

149
00:20:18,345 --> 00:20:22,411
Yaakaar naa ni danga bari ay mbir
May ma seeti leen ab diir.

150
00:20:23,096 --> 00:20:24,685
Lan mooy?

151
00:20:24,933 --> 00:20:28,407
Dafa guddi te sama spectacle
dafa tëju.

152
00:20:28,407 --> 00:20:30,200
Teg ci, naka nga duggee?

153
00:20:30,442 --> 00:20:32,509
Loolu amul benn njariñ, doktër.

154
00:20:33,157 --> 00:20:35,065
Gis nga, xamnaa sa sekkere.

155
00:20:35,672 --> 00:20:37,899
Danu wara jàppante.

156
00:20:38,827 --> 00:20:39,860
BAAX NA.

157
00:20:41,262 --> 00:20:43,534
Lumu mëna doon,
Nanu waxtaan ci biir.

158
00:21:25,741 --> 00:21:27,410
Fasilite yu baax.

159
00:21:28,495 --> 00:21:30,732
Barab bu doy waar la

160
00:21:30,732 --> 00:21:33,247
ngir ku nekk
cër bi mujjee dundu,

161
00:21:33,247 --> 00:21:35,075
ci njabootu Frankenstein.

162
00:21:35,483 --> 00:21:38,389
Du noonu la, Dr. Durea?

163
00:21:38,597 --> 00:21:40,948
Wala ma wax Frankenstein?

164
00:21:42,191 --> 00:21:46,176
Dama màgget lool
ak feebar bu metti

165
00:21:46,703 --> 00:21:50,371
kon amna lu ma jaaxal
wala ma soxal.

166
00:21:50,496 --> 00:21:53,686
Waaye sudee góor gu bëgg la
Ñëwal sama kër,

167
00:21:54,049 --> 00:21:56,842
ku am nataalam
du feeñ ci seetu bi

168
00:21:57,244 --> 00:22:01,229
ak loolu itam mu yor ci loxoom
màndarga bu bonn bu Dracula,

169
00:22:02,913 --> 00:22:06,615
Faale wuma
numu ngeen bëggee ma woowe.

170
00:22:07,943 --> 00:22:08,976
Ak bu baax...

171
00:22:09,541 --> 00:22:13,844
Lu nga may wax,
Konte Drakula?

172
00:22:17,087 --> 00:22:18,597
Doktër Frankenstein,

173
00:22:19,482 --> 00:22:21,946
Xamnaa ni màgg naa
ak famiy Durea.

174
00:22:22,876 --> 00:22:25,112
Ak ginaaw tiis
aksidaa bimu am,

175
00:22:25,112 --> 00:22:28,303
Ndaw yi dañu ko xañ
ci daara ju mag ji

176
00:22:28,665 --> 00:22:31,573
ndax lu weesu
ci njabootam dëgg.

177
00:22:33,257 --> 00:22:35,813
Amna liggéey bu neex.

178
00:22:37,329 --> 00:22:40,918
Waaye jox na xelam
ak xarañteefam,

179
00:22:41,522 --> 00:22:44,633
nekk chirurgien, ngir mëna
Géntug Frankenstein.

180
00:22:45,115 --> 00:22:46,434
Yaakaar naa ni mën naa dellusi
ngir jox ko dund

181
00:22:46,434 --> 00:22:49,067
ci nit kiñ sàkk
artifisiel ci yaw,

182
00:22:49,227 --> 00:22:52,134
ak ni àdduna du mëna
bul musa fàtte.

183
00:22:53,579 --> 00:22:55,297
Mënu rëcci
ci sa ëlëg,

184
00:22:55,297 --> 00:22:57,726
melni mënu ma ko
daw ci sama

185
00:22:58,091 --> 00:23:00,238
Li mu wax dëgg la lool.

186
00:23:01,764 --> 00:23:02,990
Yaakaar naa.

187
00:23:03,441 --> 00:23:07,347
Suma mënoon wane ñoom
dof lima def,

188
00:23:07,474 --> 00:23:09,870
ci ñi gëm
ni man ab grotesk laa,

189
00:23:09,870 --> 00:23:13,061
ci ñi alku
ñi may xeex...

190
00:23:13,423 --> 00:23:16,657
Ak fayyu ci doktër yi
Dr. Beaumont, Stedmen ak Marky,

191
00:23:16,657 --> 00:23:18,485
loolu moo yàq liggéeyam

192
00:23:18,694 --> 00:23:22,599
ñu waral safara si ko wëlbati
ci feebar bi nga nekk leegi.

193
00:23:23,684 --> 00:23:24,877
Waaw, waaw...

194
00:23:26,239 --> 00:23:29,271
Waaw, léegi gis naa ko bu leer.

195
00:23:31,230 --> 00:23:33,058
Dañu amoon tooñ.

196
00:23:33,786 --> 00:23:36,249
Waaye wax ma;
Lu nga bëgga wax ak moom?

197
00:23:36,660 --> 00:23:41,362
Amnaa ci sama loxo li des ci
Rab bu dëggu bu Frankenstein.

198
00:23:41,811 --> 00:23:43,887
Dañu leen di def ci bàmmeel bi
Oakmoor,

199
00:23:43,887 --> 00:23:45,874
ndax benn ci kuréel yi
gëstukat yi

200
00:23:46,402 --> 00:23:48,359
ñu dundu
ak monstre bi,

201
00:23:48,359 --> 00:23:54,059
daw ndax mbas mi
yàq nañu barab bi at yu bari ci ginaaw.

202
00:23:55,545 --> 00:23:57,263
Benn gëstukat bi des

203
00:23:57,263 --> 00:23:59,259
ñu suul ko ci nëbbëtu
ci monstre bi

204
00:23:59,259 --> 00:24:02,450
xaar ñu dellu ci seen
jàngat ci ginaaw.

205
00:24:02,612 --> 00:24:05,487
Moo nekkoon góor gi itam
loolu moo ko gëna ñaawlu,

206
00:24:05,487 --> 00:24:08,838
ragal nga xam
ci liggéeyam ak monstre bi.

207
00:24:09,281 --> 00:24:10,916
Dr. Bomont.

208
00:24:11,517 --> 00:24:12,788
Beaumont...

209
00:24:14,949 --> 00:24:18,175
Su Grotun delloo,
Dina nu tàmbali.

210
00:24:18,464 --> 00:24:19,859
Doktër, nga dal.

211
00:24:20,859 --> 00:24:24,243
Dinaa joxe ndigal yi
te dinga yam ci topp liñu leen sant.

212
00:24:26,169 --> 00:24:27,680
Duma ko ragal.

213
00:24:29,284 --> 00:24:31,713
Maa ngi dundu ginaaw tiitaange.

214
00:24:45,015 --> 00:24:48,449
Yaakaar naa ni liggéeyandoo ak man dina
dogal bi gëna am xel

215
00:24:48,449 --> 00:24:50,719
nga musa jël ci sa dundu.

216
00:24:51,403 --> 00:24:54,389
Mënu nu xaar.
Yaakaaral sama ndimbal.

217
00:24:54,716 --> 00:24:58,499
Danu wara waajal
laboratoire bi ngir moom.

218
00:24:58,989 --> 00:25:01,135
- Ngir monstre bi.
- Waaw!

219
00:25:01,744 --> 00:25:04,379
Ak képp ku
dañu dugg ci

220
00:25:04,379 --> 00:25:06,764
ci ëlëgu Frankenstein
ak Drakula,

221
00:25:07,174 --> 00:25:10,528
ci diir bu gàtt dina ñu leen gis ñuy suul
ci deret ju safara,

222
00:25:10,528 --> 00:25:13,752
buñu musul gis
ci kaw Suuf si.

223
00:25:21,428 --> 00:25:25,413
Laura, danga wara jàng
ngir féexal yaram

224
00:25:25,980 --> 00:25:27,297
Maa ngi féexal sama xol.

225
00:25:27,458 --> 00:25:29,603
Amaana doo dellusi
ngir wax ma loolu.

226
00:25:29,772 --> 00:25:32,487
Waaye bëgg naa
am naa la ci samay loxo.

227
00:25:33,525 --> 00:25:35,877
Dama bëgg xalaat loolu
man nga moom

228
00:25:37,159 --> 00:25:41,430
Ñaareelu yoon la
Guddi gi ngama bañ.

229
00:25:41,631 --> 00:25:42,745
Dégg naa ko.

230
00:25:43,267 --> 00:25:45,414
Daa melni luy yuuxu
xaj bu dof.

231
00:25:45,464 --> 00:25:47,655
Dina nekk
di wër jàppante

232
00:25:48,098 --> 00:25:50,006
bëgg ma xaat
Gis naa sama bos.

233
00:26:00,396 --> 00:26:02,384
Bob, bëgguma nekk
fii lu yàgg.

234
00:26:02,632 --> 00:26:05,539
Baaxna, baaxna.

235
00:26:06,745 --> 00:26:09,180
Bima la jëlee lii
guddi nga ma wax

236
00:26:09,180 --> 00:26:11,610
ni danga tàyyi ci nekk
ci nit ñu bari nii, wala book?

237
00:26:11,896 --> 00:26:14,245
Danga bëggoon dem fenn
dal ak wéet.

238
00:26:15,688 --> 00:26:19,152
Te dugal naa ci xaalis bu bari
ci essence ngir ñëw fii.

239
00:26:19,522 --> 00:26:21,316
Ndax xam nga lan moo la dal?

240
00:26:21,837 --> 00:26:23,983
Ni am nga xalaat bu bari.

241
00:26:25,551 --> 00:26:26,697
Xaaral tuuti.

242
00:26:29,063 --> 00:26:31,619
- Man itam dégg naa dara.
- Bul ko jox solo.

243
00:26:32,377 --> 00:26:33,524
Nanu joge fi.

244
00:27:47,639 --> 00:27:48,990
Ndax gis nga xale bu jigéen bii?

245
00:27:50,115 --> 00:27:52,431
- Naka?
- Ndax gis nga xale bu jigéen bii?

246
00:27:52,431 --> 00:27:53,781
Sama xarit la.

247
00:27:56,822 --> 00:27:59,616
Déedéet, gisuma ko.
Lu nga nara naan?

248
00:27:59,857 --> 00:28:02,321
- Ndax xam nga ku tuddu Rico?
- Déedéet.

249
00:28:03,171 --> 00:28:04,568
Indil ma kafe.

250
00:28:08,122 --> 00:28:10,233
Rico, am nga jotu?

251
00:28:11,635 --> 00:28:15,507
Xoolal, xale bu jigéen bi fee
Daf lay laaj.

252
00:28:16,786 --> 00:28:19,579
- Kan?
- Ki nekk ci taabal ji.

253
00:28:22,655 --> 00:28:23,449
Ah, waaw.

254
00:28:24,930 --> 00:28:27,645
- Ak loo bëgg ?
- Maa ngi wër dara.

255
00:28:34,753 --> 00:28:36,979
Jox ko lii.

256
00:32:51,960 --> 00:32:53,630
Doktër Frankenstein.

257
00:32:54,116 --> 00:32:57,023
ñàkkul xarañteem
ni gëstukat.

258
00:32:57,231 --> 00:32:59,297
Dina nu fexe ba monstre bi wax.

259
00:32:59,945 --> 00:33:02,781
Juddu ci mer kuuraŋ
ci asamaan si,

260
00:33:02,781 --> 00:33:05,574
bi komet Yorno
romb na kaw suuf si.

261
00:33:07,532 --> 00:33:10,246
Tay ci ngoon ci 11:29,

262
00:33:11,005 --> 00:33:12,516
Komet bi dina romb,

263
00:33:13,321 --> 00:33:16,705
jeexal cycle bu njëkk bi
de vie monstre.

264
00:33:17,673 --> 00:33:19,547
Dinaa judduwaat.

265
00:33:21,027 --> 00:33:22,616
Danga wara gaaw ci liggéey.

266
00:34:12,931 --> 00:34:15,441
Komet Yorno dellusi na.

267
00:35:49,475 --> 00:35:54,017
Dr. Beaumont, tay ci guddi
Di nga dajewaat ak sa xarit bu yàgg.

268
00:36:19,140 --> 00:36:20,207
Yaay kan?

269
00:36:20,537 --> 00:36:22,967
wéy di dawal
ci lima lay wax.

270
00:36:24,210 --> 00:36:25,323
Yaay kan?

271
00:36:25,488 --> 00:36:28,634
ñu xamee ma ci
Prince bu lëndëm.

272
00:36:29,202 --> 00:36:31,949
Boroom kër gu mag gi
ci Kortatiya.

273
00:36:32,276 --> 00:36:33,343
wëlbatiku foofu.

274
00:36:47,048 --> 00:36:49,682
Dr. Beaumont, génn ci oto bi.

275
00:37:03,339 --> 00:37:06,166
Sa xarit bu yàgg,
Saa waay doktër?

276
00:37:06,573 --> 00:37:10,479
Man ak Dr. Frankenstein
Def nanu ay coppite.

277
00:38:00,953 --> 00:38:02,020
Ndax yaa ngi wér?

278
00:38:05,185 --> 00:38:07,819
Dañu jàppoon ni poliis nga
te drog lañu leen.

279
00:38:07,979 --> 00:38:09,330
Danga nekkoon ci beneen àdduna.

280
00:38:14,168 --> 00:38:15,202
Yaw yaay kan?

281
00:38:16,604 --> 00:38:17,717
Fan laa nekk ?

282
00:38:18,161 --> 00:38:20,387
Man maay Mike Howard,
yaa ngi ci sama kër.

283
00:38:22,912 --> 00:38:24,059
Yaw yaay kan?

284
00:38:24,150 --> 00:38:26,865
- Judith laa tudd.
- Ndax amul ngeen ay famiy?

285
00:38:27,025 --> 00:38:29,817
- Dama leen wara jox ?
- Du doon lu jaadu.

286
00:38:30,898 --> 00:38:32,532
Nanu xool ndax xam naa ko.

287
00:38:33,093 --> 00:38:37,442
Waaw. benn bakkan,
lip supérieur épaisse...

288
00:38:38,683 --> 00:38:40,318
Xam nga Joan?

289
00:38:40,480 --> 00:38:42,432
Xamnaa ko,
waaye xawma fu mu nekk.

290
00:38:43,035 --> 00:38:45,340
Loolu doywaar, amul kenn fii
Bëggul ma wax dara.

291
00:38:45,750 --> 00:38:47,543
Benn xeetu kaaraange sa bopp la.

292
00:38:48,705 --> 00:38:51,061
Departemaa bi yor réew mi
bis bi dafay weesu

293
00:38:51,061 --> 00:38:53,695
bombarder nu ak ay laaj
ngir am ci nun ay leeral.

294
00:38:53,695 --> 00:38:55,648
Danga mujjee nekk tëx.

295
00:38:56,012 --> 00:38:57,805
Lu tax nga gëm?
Xam nga Joan?

296
00:38:57,968 --> 00:39:00,324
Ci wàll wii ci dëkk bi
Nun ñépp ñu xamante,

297
00:39:00,324 --> 00:39:01,601
ci benn anam wala beneen.

298
00:39:01,601 --> 00:39:04,111
- Naka laa def ba fi ñëw?
- Ñëwal, du la gaañ.

299
00:39:14,857 --> 00:39:15,925
Ñu indi la.

300
00:39:16,374 --> 00:39:19,406
Loolu mooy Samanta,
Dafay génn ak waa ju doy waar ji.

301
00:39:19,968 --> 00:39:23,317
Waaye noo koy woo
"Estranvetiko bi".

302
00:39:23,361 --> 00:39:27,108
- Danga bëgg di ŋàññi nit ñi ?
- Déedéet, damay seetlu tuuti rekk.

303
00:39:27,833 --> 00:39:30,627
Hobby la.
Maa ngi seetlu ngir mëna joxe xalaat.

304
00:39:31,186 --> 00:39:32,537
Daa melni match football.

305
00:39:33,184 --> 00:39:34,296
<i>Nanga def, Mike!</i>

306
00:39:34,861 --> 00:39:37,210
<i>Gis nañu neew bi
ci Bob ci Cape Rocky,

307
00:39:37,535 --> 00:39:39,682
fees dell ak deret
ñu dagg ko ay piyees.

308
00:39:40,091 --> 00:39:42,918
- Looy wax nii ?
- Waaye gisu ñu soxnam.

309
00:39:43,364 --> 00:39:45,272
Mënatu nu ànd ak dal.

310
00:39:47,077 --> 00:39:48,793
Sama gaa yi, lii dina nekk
ab tiis

311
00:39:52,627 --> 00:39:54,819
Du bari lumuy xew fii
xeetu mbir yooyu.

312
00:39:55,901 --> 00:39:57,938
- Dañu gën a dugg.
- Xaaral.

313
00:39:57,938 --> 00:39:59,653
Dama soxla ngelaw lu féex.

314
00:40:00,533 --> 00:40:01,519
Baax na.

315
00:40:20,776 --> 00:40:22,728
Ni ma leen ko waxe ba noppi;
Dunu waxtaan lu bari.

316
00:40:23,730 --> 00:40:25,843
Dama ko gis ci tefes gi
Lu tollu ci jiroom benn weer ci ginaaw.

317
00:40:26,166 --> 00:40:28,602
Noonu la guddee
ñu bàyyi seen kër.

318
00:40:28,602 --> 00:40:31,508
Ci barab bii ci tefes gi
Gis nga nit ñu bari ñu bëgga xam.

319
00:40:31,996 --> 00:40:34,142
Bii barab la ngir
noyyil bu baax.

320
00:40:36,027 --> 00:40:38,174
Joan itam dafa doon dem
dem ci park amusement bi.

321
00:40:38,304 --> 00:40:41,131
- Mooy limu gënoon neex.
-Park luxus bi?

322
00:40:42,975 --> 00:40:46,439
Dama doon xalaat
nekk monstre.

323
00:40:46,768 --> 00:40:49,674
Monstre la?
Loolu dafa metti ci man.

324
00:40:50,322 --> 00:40:53,595
Ak ñaari bopp.
Benn bët ak ginaaw gu dëgër.

325
00:40:53,595 --> 00:40:56,185
Dafa bëggoon nekk
ci lu gothesque, ak...

326
00:40:57,189 --> 00:40:58,699
Bul jàpp ni loolu rekk la.

327
00:40:59,624 --> 00:41:00,691
Xalaat bi mooy...

328
00:41:01,540 --> 00:41:05,607
soppi dellu nekk dara
rafet ci potion.

329
00:41:06,812 --> 00:41:09,161
Moo tax ma doon wëréelu
"Empire u Mbindéef yi."

330
00:41:09,726 --> 00:41:11,678
Luy "Empire u mbindéef yi"?

331
00:41:14,436 --> 00:41:16,549
Booth bu rafet
quirky,

332
00:41:16,913 --> 00:41:18,865
Dr. Durea moo ko jiite.

333
00:41:18,948 --> 00:41:21,464
Mooy tur wi muy jëfandikoo.

334
00:41:21,464 --> 00:41:23,893
Kazerne la ngir
wane ay monstre?

335
00:41:23,940 --> 00:41:26,607
Lépp fen la,
ngir turist yi kese.

336
00:41:28,013 --> 00:41:32,316
Ci beneen wàll bi, mingi aju ci
ci li ngay seet.

337
00:41:34,041 --> 00:41:36,471
Joan fexe na nekk dëgg
sa xalaat.

338
00:41:38,432 --> 00:41:40,545
Loolu du lu jaadu
ci sama mag ju jigéen

339
00:41:51,209 --> 00:41:53,799
Leegi nga am àdduna bu yéeme
ci Dr. Durea.

340
00:41:53,924 --> 00:41:55,798
Du lenn ludul
spectacle bu yomb.

341
00:41:55,841 --> 00:41:57,877
Wax naa leen ko ba noppi;
ngir turist yi kese.

342
00:41:57,877 --> 00:41:59,148
Mike, bëgguma dugg foofu.

343
00:41:59,434 --> 00:42:02,388
Yaakaaruma ni dinaa ko gis
ci Joan ci barab bu mel nii.

344
00:42:02,788 --> 00:42:04,695
Regle bu njëkk
ci seetlu bi:

345
00:42:04,944 --> 00:42:08,487
Bul musa xàddi ci saas,
li am solo bët yi duñu ko mëna gis.

346
00:42:08,697 --> 00:42:12,002
Li ñàkk du lenn ludul tuyo bi ak pantoufle yi.
Dafay màgget.

347
00:42:12,211 --> 00:42:14,720
Moytul bu baax,
Dr. mingi tànn nit ñi.

348
00:42:15,205 --> 00:42:17,795
- Bul may mu gaañ ma.
- Ak man nak?

349
00:42:18,439 --> 00:42:20,075
Xam nga ni ñuy nekkee luñu dul gis.

350
00:42:20,716 --> 00:42:22,509
Dafa tàmbalee ci ndigg li wàcci.

351
00:42:28,302 --> 00:42:30,811
Fan la waa doywaar jooju nekk?
Luy jaay biye yi?

352
00:42:31,177 --> 00:42:32,493
Amaana dafa dem lekk.

353
00:42:32,573 --> 00:42:34,958
Waaw, mënu ma ko xalaat
li ngay lekk

354
00:42:35,209 --> 00:42:38,240
<i>Nanga def ci "lmpire
ci Mbindéef yi."</i>

355
00:42:38,322 --> 00:42:39,390
Man maay Dr. Durea.

356
00:42:40,200 --> 00:42:43,433
<i>Man maa sàkk lépp
li nga nara seede.</i>

357
00:42:43,433 --> 00:42:46,068
Daa melni guide bi
telefon.

358
00:42:46,189 --> 00:42:49,255
<i>Toppal sama baat ba
platform bi njëkk.</i>

359
00:42:50,581 --> 00:42:51,898
Mike, ñëwu nu
ba fii

360
00:42:51,898 --> 00:42:54,203
ngir déglu wax ji
Durea.

361
00:42:54,373 --> 00:42:55,891
Bis boobu mooy bis bi may njëkka ñëw,

362
00:42:55,891 --> 00:42:57,639
amaana amul
Dr. Durea.

363
00:42:57,966 --> 00:43:00,396
Mike, mën ngama gëm,
waa jii mingi fi.

364
00:43:00,483 --> 00:43:04,475
Guillotine lañu sosal
ab doktër français</i>

365
00:43:04,475 --> 00:43:06,427
Jàng na ci daara
jesuit yi.</i>

366
00:43:06,910 --> 00:43:09,101
<i>Bi nga nekke depite ci asammbale bi
national,</i>

367
00:43:09,586 --> 00:43:12,939
<i>dañu xalaat ni dañuy dagg bopp bi
ñu jël ko ni anam

368
00:43:12,939 --> 00:43:14,290
<i>ñu koy teg àtte dee.</i>

369
00:43:14,616 --> 00:43:17,683
<i>Ngir rey yi
ñu gaaw</i>

370
00:43:17,730 --> 00:43:19,400
<i>ak lu gëna néew metit.</i>

371
00:43:19,687 --> 00:43:22,601
<i>Dëgg la, amul anam
ngir xam ndax anam wi

372
00:43:22,601 --> 00:43:24,634
<i>amul benn metit.</i>

373
00:43:25,157 --> 00:43:27,712
<i>Waaye xam nanu ko bu baax
ci seetlu,</i>

374
00:43:27,712 --> 00:43:30,620
<i>ni anam wi gaawna.</i>

375
00:43:31,864 --> 00:43:34,612
<i>Su fekkoon ni mënoon nañu ko
wane dëgg,</i>

376
00:43:34,700 --> 00:43:38,163
<i>dina ñu xam waxtu wi
ñàkk deret.</i>

377
00:43:38,333 --> 00:43:40,445
Daa melni ku bëgg
ak limu wax.

378
00:43:40,569 --> 00:43:43,033
Xoolal Mike.
Fiil yaa ngi fépp.

379
00:43:43,484 --> 00:43:45,595
Exposition bi yépp mekanik la.

380
00:43:47,316 --> 00:43:49,587
Amaana danga am dëgg
ci doktër boobu.

381
00:43:49,792 --> 00:43:52,459
Ndax yaa ngi def
am sikki-sakka ci sama nekkin?

382
00:43:54,584 --> 00:43:57,410
Jéggalu, xamuma ko woon
ni danga fi nekkoon.

383
00:43:57,738 --> 00:44:00,253
Maa ngi fépp,
rawatina fii.

384
00:44:00,253 --> 00:44:03,523
Xam ni mbindéef yii
Sama xel moo ko defar.

385
00:44:03,726 --> 00:44:06,394
Waaye nun ñëw nanu
ci beneen sabab, doktër.

386
00:44:06,761 --> 00:44:08,956
Sama mag ju jigéen dafa ñëw seeti ma
exposé bii.

387
00:44:08,956 --> 00:44:10,993
Nit ñu bari dañuy ñëw fi
xale bu góor bu jàng

388
00:44:10,993 --> 00:44:12,820
kumpa yi ci lu jaadu.

389
00:44:14,108 --> 00:44:15,378
Leegi demna.

390
00:44:15,664 --> 00:44:17,142
- Yaakaar nga ko?
- Waaw.

391
00:44:17,142 --> 00:44:21,047
Biñu koy mujjee gis ci
tefes gi, dama doon dem seetaan spectacle bi.

392
00:44:21,653 --> 00:44:22,801
Oh, xamnaa loolu.

393
00:44:23,610 --> 00:44:25,517
Amnaa nataalam.

394
00:44:36,865 --> 00:44:39,091
Kanamam nuruwul ku ma xamante.

395
00:44:39,381 --> 00:44:42,209
Xamnaa ni sama mag ju jigéen
Nekk nga fi, doktër.

396
00:44:43,174 --> 00:44:46,967
Nit ñu bari dañuy ñëw fii
ngir jàngat liggéey bu rafet bi

397
00:44:46,967 --> 00:44:48,363
ci Dr. Durea.

398
00:44:48,924 --> 00:44:51,796
Kanamam dafay lëndëm
ci sama xel.

399
00:44:52,157 --> 00:44:55,031
Waaye,
Mën ngama bàyyi sa adres

400
00:44:55,031 --> 00:44:57,939
te su delloo fii,
Dinaa jokkoo ak yaw.

401
00:45:03,018 --> 00:45:05,213
Wax naa dëgg
loolu nekkoon fépp.

402
00:45:05,213 --> 00:45:07,849
Ndax gis nga kanamam bimu
Ndax wan naa la nataal bi?

403
00:45:07,849 --> 00:45:09,199
Waaw, seetlu naa coppite bi.

404
00:45:09,245 --> 00:45:11,312
Xam nako, gëm naani.

405
00:45:11,442 --> 00:45:13,950
Lumu xam ak limu wax,
Ñaari mbir yu wuute lañu.

406
00:45:14,196 --> 00:45:16,548
<i>Sunu sukkandikoo ci li mujjee
amal lànket,

407
00:45:16,752 --> 00:45:20,026
<i>gorille bu góor bi mën na yegg
njoolaay 1'85 m.</i>

408
00:45:20,026 --> 00:45:22,456
Danu wara wéy di déglu
ci Dr.

409
00:45:22,822 --> 00:45:24,046
Ban saafara lanu am?

410
00:45:24,098 --> 00:45:27,732
<i>Lu am solo la
ci jigéen ñi,</i>

411
00:45:27,732 --> 00:45:30,843
canines duñu nekk
ci ay bëñ.</i>

412
00:45:31,165 --> 00:45:33,361
Waaw, amna solo lool.

413
00:45:33,361 --> 00:45:35,746
Rawatina si soo génnee
ak benn gorille bu jigéen.

414
00:45:43,342 --> 00:45:44,740
Xoolal mbàjj mi!

415
00:45:45,060 --> 00:45:47,576
- Benn cadre!
- Ak lan moo ci gëna neex?

416
00:45:47,576 --> 00:45:50,490
Amna lu muy tekki.
Lépp amna ci dundu gi.

417
00:45:50,490 --> 00:45:52,999
Yaa ngi xalaat lu jaarul yoon.

418
00:45:53,084 --> 00:45:54,800
Nanga def, Samantha, demal jëlal ko.

419
00:46:08,856 --> 00:46:10,173
Nanga def, sama xol.

420
00:46:10,493 --> 00:46:12,128
Fan nga demoon?

421
00:46:13,248 --> 00:46:17,120
Lu tax doo dem, Rico.
Bëgguma dara ak yaw.

422
00:46:18,079 --> 00:46:21,906
Xamuma lu tax mu nu bëggul.
Yaakaar naa damay jooy.

423
00:46:22,072 --> 00:46:23,627
Sama xol dama lay wax dara.

424
00:46:23,988 --> 00:46:26,055
Kenn du nu bàyyi, xam nga ko?

425
00:46:26,624 --> 00:46:28,655
Yaa ngi yàgg lool
ak nit ñooñu.

426
00:46:29,339 --> 00:46:31,215
Tay dama melni benn
xale bu jigeen bu bees

427
00:46:31,215 --> 00:46:33,770
Kon, yéeg ci sama moto
ba noppi nu génn.

428
00:46:34,729 --> 00:46:35,796
Samantha, lépp jàmm?

429
00:46:39,041 --> 00:46:40,154
Xoolal hero bi.

430
00:46:40,758 --> 00:46:42,108
Ndax du xoromu?

431
00:46:46,747 --> 00:46:47,859
Bàyyileen ko!

432
00:46:51,698 --> 00:46:53,491
Caxxum baat bu rafet la.

433
00:46:59,803 --> 00:47:01,551
Dafa baax, sama xol.
Leegi yaw nga jël ndam li.

434
00:47:01,798 --> 00:47:05,149
Waaye beneen yoon...
Dina nu gis.

435
00:47:05,832 --> 00:47:07,227
Sama gaa yi, nanu dem.

436
00:47:27,950 --> 00:47:29,948
Maa ngi gis ni dangay wéy.
Ci biir dëkkandoo yi.

437
00:47:29,948 --> 00:47:32,138
Sersant Martin,
Ndax gis nga motociclist yooyu?

438
00:47:32,422 --> 00:47:35,218
Waaw. Xale yu góor yooyu
Dañu bokk ci environmaa bi.

439
00:47:35,218 --> 00:47:36,806
Dañu sonal Samantha.

440
00:47:36,894 --> 00:47:37,847
Samanta?

441
00:47:38,332 --> 00:47:39,968
Xam na niñuy toppatoo boppam.

442
00:47:40,009 --> 00:47:42,598
Mënu ma gëm poliis bi
wax lu mel noonu.

443
00:47:43,004 --> 00:47:45,433
Poliis bi waxul,
Maa ko wax.

444
00:47:45,520 --> 00:47:47,267
Lii sama zone la,
Xamnaa ko.

445
00:47:47,675 --> 00:47:50,865
Nit ñi dañu bëgg fo.
Du jéema seetlu.

446
00:47:51,228 --> 00:47:53,737
Xamnaa loolu
suñu la jéema sàcc.

447
00:47:53,824 --> 00:47:55,810
Lu nga xam ci Dr. Durea?

448
00:47:56,298 --> 00:47:59,134
Yaa ngi jouer
detektif yi?

449
00:47:59,134 --> 00:48:01,404
Dédeet, damay jéema gis
sama mag ju jigéen.

450
00:48:01,848 --> 00:48:03,756
Newoon naa la ko woon
sama liggéey

451
00:48:04,045 --> 00:48:06,270
- Am nga jafe-jafe, lietnaa?
- Dara am solo.

452
00:48:07,118 --> 00:48:09,391
Demal sa kër,
ak dindi sa xel ci def dara.

453
00:48:10,074 --> 00:48:12,981
Di nga yëg ni danga gëna
yàq sa jot ci mbedd mi.

454
00:48:14,465 --> 00:48:16,691
Soxna Fontaine,
Jéemal baña jege tefes gi.

455
00:48:16,941 --> 00:48:18,814
Dama yaakaar ni dof la woon.

456
00:49:34,079 --> 00:49:35,794
Lu ngeen xalaat ci sama buur bu ndaw bi?

457
00:49:35,876 --> 00:49:37,670
Mike, rafet na.

458
00:49:38,470 --> 00:49:42,145
Jafe naa gëm ni bari nañu noonu
jafe-jafe yi ci àdduna bi toog fii,

459
00:49:42,145 --> 00:49:43,733
dégg yuuxu géej gi

460
00:49:45,378 --> 00:49:47,525
ak nekk ak keneen
lu baax la.

461
00:49:48,252 --> 00:49:49,922
Dafa jot nga wax ko.

462
00:49:50,849 --> 00:49:52,994
Bëgguma rek
bul def dara.

463
00:49:53,363 --> 00:49:55,271
Dama bari mbir yu ma wara def.

464
00:49:55,640 --> 00:49:56,627
Dëgg la.

465
00:50:00,231 --> 00:50:02,025
Warunu baña déggal dara.

466
00:50:03,265 --> 00:50:05,014
Deel nekk ay xarit yu baax,
dëgg?

467
00:51:05,312 --> 00:51:08,900
Yaa ngi koy xool muy nekk
ci mbindéef bu bees.

468
00:51:09,584 --> 00:51:13,615
ñooy sircuit yi ci tabax bi
adrénaline

469
00:51:13,816 --> 00:51:18,359
Trauma bu metti mën na
yëngal yaram yi

470
00:51:18,727 --> 00:51:20,442
ñu jota soppi

471
00:51:20,923 --> 00:51:22,354
Dañu ànd ak ritm bu bees.

472
00:51:22,639 --> 00:51:25,944
Deret ji dellusi na
se arterie pulmonaire.

473
00:51:26,352 --> 00:51:31,656
Nun ñépp dina ñu dundu coppite,
di jël benn deret ji.

474
00:51:33,181 --> 00:51:38,007
Dafay jaar ci sunu yaram.
Dina nu gën a nuru.

475
00:51:39,769 --> 00:51:42,324
Amaana yàggul dara nu melni benn.

476
00:51:43,083 --> 00:51:45,433
Sa bis yegsi na,
Dignaa la ko.

477
00:51:46,036 --> 00:51:47,547
Dignaa la ko.

478
00:51:48,153 --> 00:51:51,026
Dina tax serum bi am lépp
dooleem.

479
00:51:51,627 --> 00:51:54,818
Duma def lu yàgg
ci toogukaay bii,

480
00:51:55,060 --> 00:51:56,571
ñu jàpp ko.

481
00:51:56,937 --> 00:51:59,366
Dama wara yëg suuf si
ci suufu samay tànk.

482
00:51:59,932 --> 00:52:03,679
Ku amul loolu, Grotun, kenn mënul
dundu dundu gu normal.

483
00:52:09,873 --> 00:52:11,189
Lu la dal Grotun?

484
00:52:13,786 --> 00:52:18,976
"Ba leegi joxaguma la sa dose."
coppite ci diiru 24 waxtu?

485
00:52:19,416 --> 00:52:24,242
War nga dundu
amul benn xeetu metamorfose.

486
00:52:36,983 --> 00:52:38,653
Bëgguma Grotun bii.

487
00:52:39,340 --> 00:52:41,973
Dédeet, mënoo liggéey nii
ak man.

488
00:52:42,173 --> 00:52:44,921
lenn li la soxal
ci loolu lépp, deret la.

489
00:52:45,368 --> 00:52:47,037
Yaa ngi may forse...

490
00:52:47,963 --> 00:52:50,710
Yaa ngi may forse ma pikiir la
dose serum bii.

491
00:53:04,811 --> 00:53:06,764
Yaay mbindéef bu néew doole.

492
00:53:07,487 --> 00:53:10,359
Ak nu ñàkk benn dose
de sérum pour votre covarde.

493
00:53:11,919 --> 00:53:15,144
"Duma la waxaat"
baat bi musul dellu!

494
00:53:24,855 --> 00:53:28,126
Mike, maa ngi xalaat
ci li nga wax.

495
00:53:28,847 --> 00:53:29,835
Lu jëm ci lan?

496
00:53:30,365 --> 00:53:33,239
Joan màgget na leegi.
ngir dundu sa dundu.

497
00:53:36,194 --> 00:53:38,465
- Yaa ngi may reetaan?
- Déedet, du loolu.

498
00:53:39,188 --> 00:53:41,625
Dama bëgga jox Joan dara
loolu nga yàgg a soxla.

499
00:53:41,625 --> 00:53:45,690
Moytul sa mag ju jigéen ngir
mën na xalaat boppam.

500
00:53:46,416 --> 00:53:48,289
Yaakaar naa ni Joan dina la ko gërëm.

501
00:53:49,410 --> 00:53:51,159
Yaakaar naa ni amna lu ba leegi
xamoo

502
00:53:51,886 --> 00:53:53,236
Lu muy wax?

503
00:53:54,082 --> 00:53:56,272
Maa ngi xalaat
ci lépp lu xew.

504
00:53:56,996 --> 00:53:58,665
Ak xalaat bu ñëw ci sama xel.

505
00:53:59,711 --> 00:54:02,507
Lu xew
Ayu-bis yii weesu,

506
00:54:02,507 --> 00:54:04,254
xoolal park bi
ci attraksioŋ yi.

507
00:54:05,261 --> 00:54:08,929
ak benn barab bi
ci wetu tefes gi

508
00:54:09,413 --> 00:54:11,241
Mooy bu Dr. Durea.

509
00:54:11,650 --> 00:54:14,477
Ci wetu barab bi
Ndax Joan amoon na ay mbindam?

510
00:54:14,763 --> 00:54:15,990
Ak kan moo xam leneen.

511
00:54:18,437 --> 00:54:19,947
Durea amna tontu li.

512
00:54:20,114 --> 00:54:21,545
Yaakaar naa loolu.

513
00:54:23,188 --> 00:54:25,903
Waaye li may njëkka def mooy
ñaari sëkk.

514
00:54:26,662 --> 00:54:29,376
Amaana Dr. Durea moo gëna xam
lu ëpp limu mel.

515
00:55:28,349 --> 00:55:30,257
Dafa wara nekk benn xeetu kaf.

516
00:55:42,043 --> 00:55:43,553
Bàyyileen wala ma tiire.

517
00:56:38,779 --> 00:56:40,095
Oh Mike.

518
00:56:41,574 --> 00:56:43,084
Amna chance yaw la.

519
00:56:43,171 --> 00:56:46,521
- Danga daanaka raglu ma ba may dee.
- Waruloo woon génn.

520
00:56:46,924 --> 00:56:49,990
Xamnaa loolu waaye yàgg nga yegsi
Ma jaaxle.

521
00:56:50,118 --> 00:56:52,389
Ndax amna lu nga xam
lu jëm ci Dr. Durea?

522
00:56:53,472 --> 00:56:56,061
Lépp a ngi ci yoon,
waaye ba leegi wóolu ma ko.

523
00:56:57,105 --> 00:56:59,489
Nanu xoolaat
ci suufu kazarmam.

524
00:57:18,187 --> 00:57:19,704
Moytul, Mike.

525
00:57:19,704 --> 00:57:21,736
Danu nekk ci suuf
ci kazerne bi.

526
00:57:38,271 --> 00:57:40,825
- Lii moo nu doon wër.
- Luy loolu ?

527
00:57:41,064 --> 00:57:43,654
Paneel bi wuute na lool
ci ñeneen ñi.

528
00:57:44,977 --> 00:57:46,885
Maa ngi jéema ubbi buntu bii.

529
00:57:49,809 --> 00:57:52,602
Suma wax dëgg,
Di nga dóor pontu bi ci bopp bi.

530
00:57:52,643 --> 00:57:55,917
Nanga def, bëgguma nekk fii.
Vanga, nanu dem.

531
00:57:55,917 --> 00:57:57,234
Waaw, waaw.

532
00:57:58,832 --> 00:58:00,898
Bëgg naa xam
ki koy jëfandikoo.

533
00:58:07,616 --> 00:58:09,886
Ndax gëm nga li nga wax dëgg?

534
00:58:12,806 --> 00:58:15,793
Dama yaakaar ni Dr.
nit ñi.

535
00:58:16,040 --> 00:58:17,755
Loolu lu tiis la.

536
00:58:18,396 --> 00:58:20,508
Yaakaar naa itam ni dafa tëju.

537
00:58:21,950 --> 00:58:24,742
Dafa tëju ci chaise roulante bi,
Kon...

538
00:58:25,543 --> 00:58:27,689
Kenn wala dara lu ko mëna jàppale.

539
00:58:28,538 --> 00:58:30,967
Ak buntu fiir bi nu gis,
Lu muy tekki?

540
00:58:32,849 --> 00:58:34,518
Ab gennup ngir rëbbkat bi.

541
00:58:36,004 --> 00:58:38,599
Jeffin ju góor jooju
Dafa doywaar tuuti,

542
00:58:38,599 --> 00:58:39,915
Waaye jàpp naa ni dafa dof.

543
00:58:40,316 --> 00:58:43,231
naka ngay xàmmee dof?

544
00:58:43,231 --> 00:58:44,788
Ci wàllu nit,

545
00:58:44,788 --> 00:58:47,581
dof mooy li gëna tar
ngir gis.

546
00:58:48,141 --> 00:58:50,731
Waaye mënunu
defal lépp ngir firnde ko.

547
00:58:52,613 --> 00:58:53,760
Nanu seet ay firnde.

548
00:58:55,129 --> 00:58:56,843
Mike, lu tax ngay def lii?

549
00:59:09,462 --> 00:59:10,609
Am alal!

550
00:59:12,935 --> 00:59:16,286
Lu tax ngeen jaaxle?
Wax naa la dina ñu dajewaat.

551
01:00:06,796 --> 01:00:10,339
Am alal! Déedéet, mangi!
Déedéet, mangi!

552
01:00:12,068 --> 01:00:14,941
Déedéet, mangi! Am alal!

553
01:00:17,497 --> 01:00:18,531
Am alal!

554
01:00:21,130 --> 01:00:23,686
Déedéet, mangi!

555
01:00:24,845 --> 01:00:25,797
Am alal!

556
01:00:28,477 --> 01:00:29,511
Déedéet!

557
01:00:30,473 --> 01:00:31,699
Am alal!

558
01:00:33,868 --> 01:00:35,775
Déedéet, mangi! Am alal!

559
01:00:37,061 --> 01:00:39,366
Baax na. jébbalu nga
ci lëppaalëpp boobu, wala book?

560
01:00:39,538 --> 01:00:41,206
- Déedéet.
- Kon baaxna.

561
01:00:41,293 --> 01:00:42,770
Maa ngi lay tàmbali tuuti.

562
01:00:43,409 --> 01:00:44,318
Déedéet!

563
01:00:44,886 --> 01:00:46,963
Sama yaakaar mooy nga def lu baax
ak samay xarit.

564
01:00:46,963 --> 01:00:50,108
Nanga def, sama xol.
Yaa ngi ci suufu tefes gi.

565
01:00:51,874 --> 01:00:54,507
Banneexu ci.

566
01:00:58,103 --> 01:00:59,499
Waaw, dafa tàng.

567
01:01:00,298 --> 01:01:02,172
Di nga féexal sa xol itam.

568
01:01:04,810 --> 01:01:07,206
Am alal! Am alal!

569
01:01:07,206 --> 01:01:08,194
Déedéet!

570
01:01:08,843 --> 01:01:10,114
Déedéet! Am alal!

571
01:01:45,974 --> 01:01:47,088
Ndax dégg ngeen ko?

572
01:01:49,808 --> 01:01:51,284
Sonu caden.

573
01:01:51,565 --> 01:01:54,278
Mike, bunu ci waxtaanaat.

574
01:01:54,798 --> 01:01:56,195
Dégg naa ko bu njëkk.

575
01:01:57,474 --> 01:01:59,028
Yaakaar naa ni xamnaa fi.

576
01:02:00,547 --> 01:02:01,627
Xaaral fii, dinaa dellusi leegi.

577
01:02:01,627 --> 01:02:04,740
- Bul dem.
- Bul xuloo ak man. Demal fii.

578
01:02:04,740 --> 01:02:05,773
Dinaa dellusi ci saa si.

579
01:02:09,731 --> 01:02:10,526
Mike.

580
01:02:11,488 --> 01:02:13,713
Bëgguma nekk man kese
amul benn yoon.

581
01:02:16,399 --> 01:02:19,033
- Xoolal, foofu lanu nekkoon bu njëkk.
- Xam naa.

582
01:02:23,505 --> 01:02:24,983
Mën naa waat ni gis naa
toxal dara

583
01:02:24,983 --> 01:02:28,174
- Lan nga yaakaar ni mën na nekk?
- Dafa mel ni ku yor néew.

584
01:02:29,695 --> 01:02:31,125
Ma tàmbali xalaat ay mbir.

585
01:02:41,553 --> 01:02:42,586
Loolu lan la ?

586
01:02:46,065 --> 01:02:47,210
Ci Samantha la jóge.

587
01:02:47,621 --> 01:02:49,574
Mike, déet!

588
01:02:53,451 --> 01:02:55,245
Maa ngi dugg foofu ngir wër ko.

589
01:02:55,567 --> 01:02:56,765
Te dara du ma tere.

590
01:02:56,765 --> 01:02:58,672
Mike, mooy gëna baax
nu ñaan ndimbal.

591
01:02:59,519 --> 01:03:02,354
Xale yu góor yi ak yu jigéen yi,
Empire bu Dr. Mbindéef yi...

592
01:03:02,354 --> 01:03:04,306
Taxawal! Nanga def, yaw!

593
01:03:04,430 --> 01:03:07,066
Danga wara jënd këyit bi
soo bëggee jàll!

594
01:03:07,066 --> 01:03:09,131
- Man itam bëgg naa la.
- Dellu fii ! Danga wara fay.

595
01:03:09,462 --> 01:03:10,608
Danga njool lool.

596
01:03:10,739 --> 01:03:12,646
Moo tax ngay saaga ma, xale bu muus bi.

597
01:03:13,055 --> 01:03:14,971
Waaye duma mel noonu
xale la woon ci dundam.

598
01:03:14,971 --> 01:03:16,322
Dina nu gise.

599
01:03:21,878 --> 01:03:25,070
- Sa xarit foofu lay xaar.
- Sama xarit?

600
01:03:25,432 --> 01:03:26,942
Waaw, dal.

601
01:03:26,988 --> 01:03:29,498
Grazbo gis na te xamna.

602
01:03:29,744 --> 01:03:32,412
Bul ma ragal;
Man nit ku ndaw laa.

603
01:03:32,658 --> 01:03:34,885
Loolu kenn du ci bàyyi xel.

604
01:03:35,334 --> 01:03:38,009
- Wax nga gis nga sama xarit bi?
- Waaw kay.

605
01:03:38,009 --> 01:03:40,394
Mingi lay xaar ci biir.

606
01:03:51,863 --> 01:03:53,453
Bëgg ngama gis?

607
01:03:54,339 --> 01:03:56,291
gis naa sa fake
wone, Dr.

608
01:03:57,813 --> 01:03:59,323
Leegi dama bëgga gis say pexe.

609
01:04:10,469 --> 01:04:11,502
Mike!

610
01:04:11,867 --> 01:04:14,501
Waaye... Nanga yéeg! Gaaw!

611
01:04:23,845 --> 01:04:24,753
Déglu.

612
01:04:27,877 --> 01:04:29,274
Nanu jaar fii.

613
01:05:00,776 --> 01:05:02,651
Nanu fexe nu génn.

614
01:05:06,207 --> 01:05:07,762
Yombal na ñu ko lool.

615
01:05:16,708 --> 01:05:19,977
- Yaw nga xaar ma fii.
- Mike, dama wara xam li xew.

616
01:05:31,561 --> 01:05:32,469
Mike!

617
01:05:33,796 --> 01:05:35,272
Joan laa.

618
01:05:36,871 --> 01:05:39,663
<i>Rakkam bu jigéen, ci jàmm.</i>

619
01:05:39,985 --> 01:05:42,937
<i>Ni nga ko gisee, lii du
lëmu ab rabi àll.</i>

620
01:05:44,776 --> 01:05:46,002
Joan, ndax lépp jàmm?

621
01:05:46,293 --> 01:05:50,437
Rafetam bu jigéen bokk na ci
jàngat bu mag ci wàllu science.

622
01:05:51,044 --> 01:05:55,396
Waaye ni nga ko gisee, jaar na yoon
te dara yàquwul.

623
01:05:55,396 --> 01:05:56,793
Lu tax mu nu jàngal loolu lépp ?

624
01:05:57,074 --> 01:06:02,775
Ndax dañu leen tànn ngir
bokk ci samay jàngat.

625
01:06:02,983 --> 01:06:07,694
Dañu wara xam ni duñu
tëju.

626
01:06:07,694 --> 01:06:10,646
Te su ko defee, dina ñu nekk
moom seen bopp ci ngëm

627
01:06:10,729 --> 01:06:13,555
ngir li nara xew
ci ab diir.

628
01:06:29,853 --> 01:06:31,681
Ni ay milioŋ ciy nit,

629
01:06:32,448 --> 01:06:36,071
gëm nga ni li nga am
ci kanam, amul benn werante.

630
01:06:43,508 --> 01:06:45,620
Seede ngeen...

631
01:06:45,784 --> 01:06:48,895
ci lëkkaloo ak beneen mbindéef
ci samay jàngat.

632
01:06:53,809 --> 01:06:54,843
Samanta.

633
01:06:56,564 --> 01:06:57,914
Baax na.

634
01:06:58,161 --> 01:07:02,153
Waaye ni ngeen ko seedee
yaxxum 3 ndaw

635
01:07:02,153 --> 01:07:03,743
bëggoon nañu ma gaañ,

636
01:07:04,310 --> 01:07:08,738
am ci biir
coppite selulaar bu yéeme.

637
01:07:09,860 --> 01:07:14,765
Sa deret amna cër bi
Dafay am solo ngir matt sama serum.

638
01:07:15,450 --> 01:07:17,605
Musu ma xalaat ni coppite la
nuru,

639
01:07:17,605 --> 01:07:20,069
am ci diir bu gàtt
diir bu yàgg.

640
01:07:20,760 --> 01:07:21,792
Waaye amoon na.

641
01:07:22,636 --> 01:07:25,066
Leegi xamnaa ni mën na
mu dellu.

642
01:07:27,227 --> 01:07:29,374
Yeen ñaar bëggante ngeen.

643
01:07:30,263 --> 01:07:32,771
Ak bu ñuy xalaat ci
deewu bëgg-bëggam ci lu gaaw,

644
01:07:33,656 --> 01:07:35,166
Dina ñu am lu leen tiital lool.

645
01:07:35,493 --> 01:07:38,327
Deretam soppiku,
dina ko yóbbu ci deposit yi

646
01:07:38,327 --> 01:07:40,076
ci courant électrik.

647
01:07:40,324 --> 01:07:43,788
Di nga yëg ni danga yéeg
ci avion bu bees.

648
01:07:43,997 --> 01:07:49,460
Loolu mooy ndoorte lu bees
dundu ngir yaw...

649
01:07:50,426 --> 01:07:51,537
Ak ngir ñeneen ñi.

650
01:07:52,661 --> 01:07:54,693
Li gëna am solo mooy sama xarit.

651
01:08:05,717 --> 01:08:08,670
Waaw, ku am xel lool!
Yaa ngi nekkatoo noonu, wala book?

652
01:08:08,911 --> 01:08:10,137
Di nga nekk sunu bos.

653
01:08:29,354 --> 01:08:32,657
Grotun, toppatoo sa xarit Grazbo.

654
01:08:33,067 --> 01:08:35,780
Ñoom ñépp, war nañu dee!
Ñoom ñépp, war nañu dee!

655
01:08:36,820 --> 01:08:38,376
"Judith, joge fi!" Dem!

656
01:08:45,324 --> 01:08:48,516
Grotun, jëlal xale bu jigéen bi!
Xaaral ko!

657
01:09:59,987 --> 01:10:01,984
Waaye, ak Samanta.
Ndax amna lu ko dal?

658
01:10:01,984 --> 01:10:05,050
Nanu seet barab boobu.
Su amee, dinga ko fekk.

659
01:10:05,258 --> 01:10:07,926
Nu ngi gis ñatti néew yooyu ba noppi.
Gaawal.

660
01:11:29,223 --> 01:11:30,337
- Serjant bi!
-Waaw?

661
01:11:30,661 --> 01:11:33,169
Ci kaw kaw kër gi
Ndax du Yudit?

662
01:11:34,574 --> 01:11:35,845
Yaakaaru ma ko.

663
01:11:36,769 --> 01:11:39,914
Sergeant, yéeg ci kaw kër gi,
noo ngi jaar fii.

664
01:12:50,553 --> 01:12:54,176
Dama ragal sa seet
Dina jeex tay ci guddi.

665
01:12:55,105 --> 01:12:59,376
Di dugg ci samay mbir,
Dina la fay lu seer lool.

666
01:14:00,066 --> 01:14:05,925
Tiitaange dina soppi bépp kàttan ak
jumtukaayu molecule yi ci sa deret.

667
01:14:12,604 --> 01:14:14,080
Loolu mooy yuuxu.

668
01:14:14,080 --> 01:14:17,351
Bépp particule ci segond bu tàng
dafay mer.

669
01:14:39,913 --> 01:14:42,468
Tay ci guddi mooy mujj.

670
01:14:42,787 --> 01:14:44,820
Ki mujj ngir yaw.

671
01:14:46,421 --> 01:14:49,884
Yaay waral dee gi
ci Dr. Durea.

672
01:14:50,215 --> 01:14:52,360
Ki mujj ci mbokki Frankenstein yi.

673
01:14:53,248 --> 01:14:55,475
Man maay Drakula.

674
01:14:56,283 --> 01:15:00,393
Sérum bimu def
Dinaa nekk ki kenn dul noot.

675
01:15:01,634 --> 01:15:05,826
Te gëm naani du yàgg.
lu bari luñu wara am

676
01:15:05,826 --> 01:15:08,459
serum bi ma soxla yépp.

677
01:15:08,580 --> 01:15:10,137
Suma ko jotee,

678
01:15:10,137 --> 01:15:14,520
Dinaa dellu ak mbooloo
vampire yuy dundu.

679
01:15:14,729 --> 01:15:17,397
Larme budul yàqu
de immortels.

680
01:15:18,522 --> 01:15:20,474
Su boobaa kenn du ma mëna tere.

681
01:15:20,918 --> 01:15:23,302
Kenn mënu koo tëye sama kàttan.

682
01:15:56,771 --> 01:15:59,123
Déedéet! Déedéet! Ci moom ! Ci moom !

683
01:15:59,248 --> 01:16:00,474
Ci moom !

684
01:16:01,363 --> 01:16:02,589
Ci moom !

685
01:16:08,191 --> 01:16:09,145
Ci moom !

686
01:16:11,504 --> 01:16:12,696
Ci gànnaaw!

687
01:16:22,045 --> 01:16:23,395
Dal!

688
01:19:35,690 --> 01:19:40,118
Sama keesu néew mingi nu xaar, ngir nga
defal la kenn kudul dee ak sunuy laxasu.

689
01:21:18,221 --> 01:21:22,366
Leegi dinga ànd ak man ci àdduna
ci néew yiy dundu.

690
01:24:26,395 --> 01:24:27,224
Dakkal dal!

691
01:24:27,394 --> 01:24:29,750
"Taxawal wala ma dagg la"
piyees par piyees

692
01:24:29,750 --> 01:24:32,497
naka laa tabaxee
Dr. Frankenstein!

693
01:25:48,564 --> 01:25:50,791
Dama wara daw leeralu jant bi!

694
01:25:51,000 --> 01:25:52,669
Dama wara dellusi ci sama keesu néew!


